• Paroles pour Temps Boy Daara J Family

Ecouter la chanson : temps boy daara j family



Auteurs :


Compositeurs :

Interprètes :


Paroles de la chanson :


TEMPS BOY
Paroles: Abdou SECK , Mamadou SECK.
Musique: Abdou SECK , Mamadou SECK. REFRAIN
TIMISSOUL BAY GUOUDI YAW
FATTALLIKOUL TEMPS BOY
SO GUISSATOUL BAY TEGGUI YONN
FATTALIKOUL TEMPS BOY COUPLET 1:ndongo
Temps boy teylama dab biss yi dima japp
att yi geuneu gaaw ak lima daw ngir teela raw
xel a daw fatteuliku douma fate yi baat
fangeundiku geustu yoon nanga waaj
yi baax yi jag yi bonn yi xatt madi gissaat
moytandiku doon tricheur biir clase
doon crack gaddu sac wacce kab daxi heure di stop P2 ba roppi sotrac
laxu doon touxkattu bepp xeet cigarettes dinga seet jengu doon guerrier
walla tapette lang sareet beureet wirri kogn daw doug biir market
Interprète(s) : DAARA J FAMILY ; ©
2009 by CHRYSALIS MUSIC FRANCE, ZAMORA EDITIONS, TRAFFIX MUSIC All Rights Reserved TRAFFIX MUSIC SCHOOL OF LIFE
Code ISWC : T-702.401.724.3
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

TEMPS BOY
troto sinkkal powu xandal dawi geej cinema gettu beuy dofi leuj
gnoune daawoko deuj nijaay di kass yaw danga repp yaw danga
xeeb lesson yi nga lebb teuj la rek bado giss sakh ceeb dangay wanne danga matt
danga jeum makk naala par 4, COUPLET
GNOUN BAGNOU DE GONNE DEF NAGN LOUNE
LOOLAMBE ASSALOO ASSABOMBE SALSALATOO
BALBA DEMNA KAW BA LA MOU KOY LAAL SAMA YARAM DAWNA
ADINA AMOUL SOLO KHOOLAL FILA GNOU JAAR
NE CI JALU SOUFSI DI LAMBI GOLO
SEEK LEEK DAMAY TOOK DI SCIENCE BOOBOU TEMPS
AK NI MOU GAAWE CEEY ADOUNA POTOU CAFE AK CAASS
BANT AK PONT AMNGA TOUQ SOU NGALAM
Interprète(s) : DAARA J FAMILY ; ©
2009 by CHRYSALIS MUSIC FRANCE, ZAMORA EDITIONS, TRAFFIX MUSIC All Rights Reserved TRAFFIX MUSIC SCHOOL OF LIFE
Code ISWC : T-702.401.724.3
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

TEMPS BOY
BANTOU BALE DIKO CI XALAM
TAMPON GUERRIER SA YARAM TOPP NEEKHAYOU POMI
TERREUREURRI FATTE JANG SAY LECON
GNIBBI SI PAABI TEGGAL LA CI KARRAWAASS
AICA CI BIIR TEEWUMALA DOKH TIMISS GUONE GUILE DEURKISS
DANGA BEUGUEU TARKHISS
BOO BAYYI WUL MBEDDMI DAACI MEUSSA AM BISS
GUI GONNEE WOW DEUGUEUC TOOGAL NGA LEUC
TEMPS BOY TEMPS TEMPS BOY SOOKOY FATTALIKOU
DANGAY DEM BA DOO AMATI LOO WAX LOUDOUL NDEYSAAN
SOY FATTALLIKOU NJALBEEN SOY FATTALIKOU NJALBEEN
SO KOY FATTALIKOU DANGAY DEM BA DEM BA DOO AMATI
LOO WAX LOUDOUL NDEYSAAN NDEYSAAN
Interprète(s) : DAARA J FAMILY ; ©
2009 by CHRYSALIS MUSIC FRANCE, ZAMORA EDITIONS, TRAFFIX MUSIC All Rights Reserved TRAFFIX MUSIC SCHOOL OF LIFE
Code ISWC : T-702.401.724.3
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

TEMPS BOY
Interprète(s) : DAARA J FAMILY ; ©
2009 by CHRYSALIS MUSIC FRANCE, ZAMORA EDITIONS, TRAFFIX MUSIC All Rights Reserved TRAFFIX MUSIC SCHOOL OF LIFE
Code ISWC : T-702.401.724.3
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

Les Auteurs et leurs Oeuvres

Association Les Auteurs et leurs Oeuvres

23, boulevard Arago
75013 Paris

Contact

Présentation Lalo

Contrat type




Adhésion Auteur & Compositeur

Adhésion Editeur

Adhésion Bienfaiteur



Collection Paroles & Chansons

Collection Musique & Création

Collection Nouveaux Talents

Moteur de recherche



S'abonner à la newsletter :