• Paroles pour Tomorrow Daara J Family

Ecouter la chanson : tomorrow daara j family



Auteurs :


Compositeurs :

Interprètes :


Paroles de la chanson :


TOMORROW
Paroles: Abdou SECK , Mamadou SECK.
Musique: Abdou SECK , Mamadou SECK. Refrain:
Boul xaar loy déf défko,loula thi fék mouy loolu,loula thi fék mouy loolu
bagna took di khaar tomorrow
war nga wagni lingay nélaw
banga xaméni yoonu ndam dou gaaw
war nga jog thia teel ndax nga raw VERSE1/
souba souba yalla doleen jéxal
linga warra déf boul khaar défal
amoul yaggal téyla téyla!!
biss bo toogat wéyna wéyna!!
euleuk yégségoul défko légi
weurseuk gneuwna légi légi
veuf nawaat ci ngélaw
yaakar rombla ngay daw
linga wara déf boul thiow
boul khaar moulay reuthie
Interprète(s) : DAARA J FAMILY ; ©
2009 by CHRYSALIS MUSIC FRANCE, ZAMORA EDITIONS, TRAFFIX MUSIC All Rights Reserved TRAFFIX MUSIC SCHOOL OF LIFE
Code ISWC : T-702.401.718.5
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

TOMORROW
boul yeuglou boul jébbalou
déf lingay déf né keuthie
fi nga wara jaar ba tékki
légi la ci téew amoul jéllalee 'k bama yéewu
défal yitté ba jiité say xalaat nimou dikké
saabo kheuyé nanga jeufé linga beug té boul tiit dé Refrain:
Boul xaar loy déf défko,loula thi fék mouy loolu,loula thi fék mouy loolu
bagna took di khaar tomorrow
war nga wagni lingay nélaw
banga xaméni yoonu ndam dou gaaw
war nga jog thia teel ndax nga raw VERSE2/
IT's early i morning i suggest
u wake up rather than wasting your time
yawning and snoring while time is running
get up and do something
Interprète(s) : DAARA J FAMILY ; ©
2009 by CHRYSALIS MUSIC FRANCE, ZAMORA EDITIONS, TRAFFIX MUSIC All Rights Reserved TRAFFIX MUSIC SCHOOL OF LIFE
Code ISWC : T-702.401.718.5
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

TOMORROW
you ll never make it scrounging
don' t expect to reap credit if you 've sown nothing
what you waiting for grind it work it while the heat is on
don' t moan and groan step up on your feet
go it alone keep your ongoing spirit
ready steady to take sky 's the limit
your life is only what you make it
it is right away you made your brighter day
tomorrow s another day
your best bet could be made today REFRAIN:
Boul xaar loy déf défko,loula thi fék mouy loolu,loula thi fék mouy loolu
bagna took di khaar tomorrow
war nga wagni lingay nélaw
banga xaméni yoonu ndam dou gaaw
war nga jog thia teel ndax nga raw VERSE3/
euleuk jaayoontéla gisso liy gneuw dabantéla
Interprète(s) : DAARA J FAMILY ; ©
2009 by CHRYSALIS MUSIC FRANCE, ZAMORA EDITIONS, TRAFFIX MUSIC All Rights Reserved TRAFFIX MUSIC SCHOOL OF LIFE
Code ISWC : T-702.401.718.5
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

TOMORROW
njeukeu départ daxantéla,wakhtou wou gneuw garantila
fi nga nékoon daw joggulafa,bancs-jaxlé ak boppu kogn bi ha!! ha!!
yu ll be rewarded for every sacrifice yu make
don t fall asleep for God s sake tomorrow is today
gotta do what you gotta no matter what it takes
joggal sigil,nanga jeul sa euleuk ci say niari loxo
boul ragal ,boul ne thiell takkal sa fit ta gueum ne meun nga ko REFRAIN:
Boul xaar loy déf défko,loula thi fék mouy loolu,loula thi fék mouy loolu
bagna took di khaar tomorrow
war nga wagni lingay nélaw
banga xaméni yoonu ndam dou gaaw
war nga jog thia teel ndax nga raw
you better wake up...you better wake up...
Interprète(s) : DAARA J FAMILY ; ©
2009 by CHRYSALIS MUSIC FRANCE, ZAMORA EDITIONS, TRAFFIX MUSIC All Rights Reserved TRAFFIX MUSIC SCHOOL OF LIFE
Code ISWC : T-702.401.718.5
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

Les Auteurs et leurs Oeuvres

Association Les Auteurs et leurs Oeuvres

23, boulevard Arago
75013 Paris

Contact

Présentation Lalo

Contrat type




Adhésion Auteur & Compositeur

Adhésion Editeur

Adhésion Bienfaiteur



Collection Paroles & Chansons

Collection Musique & Création

Collection Nouveaux Talents

Moteur de recherche



S'abonner Ă  la newsletter :