• Paroles pour Doyal Naniou Cheikh Lo

Ecouter la chanson : doyal naniou cheikh lo



Auteurs :


Compositeurs :

Interprètes :


Paroles de la chanson :


DOYAL NANIOU
Paroles: MAMADOU MOUSTAPHA LO.
Musique: MAMADOU MOUSTAPHA LO.
Ohé Africa ye Africa united, united
Gnoune domou Africa doyal naniou coup d'Ă©tat
Thi fénéne ak foudoul Africa
Gnoune domou Africa doyal naniou coup d'Ă©tat
Thi fénéne ak foudoul Africa
Coup d'Ă©tat day diour M'Bagnel, coup d'Ă©tat day soukheut bop sa bof
Té sétlou na gnou fou mou Khassa am, yagga yagga dina fa amat
Coup d'état ba dédiou, ndéy ak Baay doto woloy
Coup d'état ba dédiou, thiamogne ak ndéydior doto wolou
Coup d'état ba dédiou ; kou seukheut ngafog né dalay woutou
Africa ho, Africa ho, Africa Ho, united united, stop war
Souma khel dém sa, Thomas Sankara peulh bou
Ratét binewone bourkina faso
Ak kabila si Congo, ama guei Robert sa Cote d'Ivoire
William Tolbert ak Samuel do sa Liberia, gnéréré sa Tanzanie
Interprète(s) : CHEIKH LO ; ©
2015 by WAGRAM PUBLISHING All Rights Reserved
Code ISWC : T-703.526.843.2
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

DOYAL NANIOU
Moussa Traoré thia Mali, ana tché ke verra, nino vern thia
Guinée Bissao, kougnousi réyoul, teuthie nanioula, guéne nanioula
Mba niou boomla, liniou geuneulone sakh, kounioufi diokham
RĂ©w, bo dokha loul niou dindila si kaw diongante
Fi ak khér diogoul, bal takkoul, khéthie nawoul
Peundeu diogoul, guéthie gui débordéwoul
Diam rék laniou y am si Senegal ak liko weur
La paix en Casamance, la paix au Mali, di mouslou si rebellion
Naniou wéér nganayi
Niou khol si Ukraine, ho way Russie, ho wayayo la Syrie
Ho wayayo yo Afghanistan, Centre Africa ho, thiowli barina
Mandela, Mandela, Mandela oh South Africa, doyalnanou coup d'Ă©tat
Nioune domou Africa doyal ma nou coup d'Ă©tat
Nioune domou Africa doyal ma nou coup d'Ă©tat
Thi fénéne ak foudoul Africa
Coup d'Ă©tat day diour M'Bagnel, coup d'Ă©tat day soukheut bop sa
Interprète(s) : CHEIKH LO ; ©
2015 by WAGRAM PUBLISHING All Rights Reserved
Code ISWC : T-703.526.843.2
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

DOYAL NANIOU bof
Té sétlou na gnou fou mou massa am, yagga yagga dina fa amat
Coup d'état ba dédiou, ndéy ak Baay doto woloy
Coup d'état ba dédiou, thiamogne ak ndéydior doto wolou
Coup d'état ba dédiou ; kou seukheut ngatok né dalay woutou
Interprète(s) : CHEIKH LO ; ©
2015 by WAGRAM PUBLISHING All Rights Reserved
Code ISWC : T-703.526.843.2
Les Auteurs et leurs Oeuvres.
Le site officiel des Auteurs et Compositeurs de Chansons.

Les Auteurs et leurs Oeuvres

Association Les Auteurs et leurs Oeuvres

23, boulevard Arago
75013 Paris

Contact

Présentation Lalo

Contrat type




Adhésion Auteur & Compositeur

Adhésion Editeur

Adhésion Bienfaiteur



Collection Paroles & Chansons

Collection Musique & Création

Collection Nouveaux Talents

Moteur de recherche



S'abonner Ă  la newsletter :